Yong Lion
Yong Lion

freestyle a7

freestyle a7

168 Plays

5 months ago

li am si réwmi DAFA doy war, réalité biñouy doundou leu dou ay cauchemar,Dañou beug changé système ndah li Sénégal dañousi marre, kénéne ko fi mounti fale si sén bir tmt yone bi léy diar, beugeu toñou ngourou présidence wayé bou parlementaire, beug na ñou justice manou si politique té réglementaire, sénégal bayi lén thiakhane way deug dou rombi nop, bane politicien mo fi meusseu yeukeuti kaddou môme sa bop, motakh peuple bi nélén fi ñiouk Sonko la ñouy top, ngéne dieul ko teuthie ko toumal ko ñoukéy ngeun di sop, fa nguén warone khamni projet bi dey law si khol yi non-stop, teuthie leaderou Ndaw gni pour gnou khadi boy yi di gueun di Focus, diap gnou nnott ñou theuthie ñou réy ñou paré di ñiane bonus, boup lén séni bagage té abale ñou yéksi ngén terminus, sathie alalou réwmi diko pathio diñou nakhé virus, li khéw si réwmi damay lathie loi la sama concurrence, teuthie nit 50 jours ba paré jugé ko continence, dialguati yone ak sunuy droit thiéy bi émergence, faté na liñouy doundou années 60 ba lègui yéna sunuy conscience, la takh na réwmi dotou ñou ko diokh candidat wou france, Yallah dou ték diamame loumou antanoul, kone cheytané yi fouñou la wo Focus rek tankamdoul, Mamadou dia bi fi diota diar ño dague tankam soule, rivalité politique bi di mélni équipe you bok poule ,ni ñouy forcé iphone Dubaï from FR té mom la kén bougoule

29 Comments

Leave a comment

5 months ago

Bars: Dope 🔥 Delivery: Great 🎉 Impression: Great 🎉

5 months ago

ATE 🍜 ILL 🤒 Bars: Perfect 💯 Delivery: Perfect 💯 Impression: Perfect 💯

5 months ago

TOUGH 😮‍💨 Killed it! 🎯 Bars: Perfect 💯 Delivery: Perfect 💯 Impression: Perfect 💯

You may also like