tay réw❤🔥😈
0:00
0:00
gnodiima trône ma indilla king gnodiima king ma indilla sick gnodiima sick ma wathéé sliip gnodiima sliip ma mandé fiit gnodiima beatch ma indilla guerre dawouma fils mane paréna khékh indillal daadjiaal akk lucifer bakhal la saaf com pomme de terre coup 👊 bé dall motakh nga rérr coloniser léneu com Hitler may séneu pére kouka wédi déê maay dirigé cone toguél nééé geuneuu fé ndaw baparé geuneuu rew gueneu fé sadick paré gueneu fé dé nénaa da tilimaal sama deerr mounogo sip ndakh danguay diém Mounoto time sa khour yé pane kougne mounti ngémbeu dinala dane mak gnéneu ucad ba bountou fane dénkeuleu diné ngay wakh si sex tes qu'une chienne cone amène ta laisse sa cour kouka fékè day beuseu next
You may also like

Leave a comment
See track description ↑