hood yeup la bolé bot
hood yeup la bolé bot real nigga walabok xam nga lou mbed bi di tok fo dem tok. walou dieund ay diaye mou diar jaboot bi meune sey agne waye. yalla na diar ak diam waye mba séroul torop waye. am astoute si xam xam aley moussal si diam diam djite fitoula ak dangaram woank sowoul sa yaram. Diane matoula boromi séle lékoula sam nga sa yaram. téki pitbull yi teubeuli fake yi. téyé mic: di dowal nga xam né bokouniou tailleur bi niouy niowal. Rap doumala lalaleu bassang. ladje ma mane ek mic kou meune. Bi ma nieuwé la hip hop variété lali bassang. samey beat di hotlif koussiy rap Daddy bibson. yek sen kaw defati dara tall hip hop galsen jokh mic bi son bi domou rap galsen. xalé yi mag mey sene. ndieurignou rap galsen alwa yek téré yi ma done yeur. leerrou alxourane bimey khégne di weur. skeezo dread yes a nigga with some swagg but a natty dread. sa tatou toubey khotekou téréte rap dafa nek sama déréte. diamono bouffé diluant on a bouffé du lion.
You may also like

Leave a comment
See track description ↑
Bars: Perfect 💯 Delivery: Perfect 💯 Impression: Perfect 💯