defal ligay déf bala gay wouydi god ligayal sisa bop ndakh nga nék fort khamoni doundou dou gueuneu méti ba mélni bou ka
defal ligay déf bala gay wouydi god ligayal sisa bop ndakh nga nék fort khamoni doundou dou gueuneu méti ba mélni bou karballah none yi sonal nanko wayé lepp si ndogolou god god god bourbi kenne leu kouko diamouwoul perte nga motakh madioublou pénkou ngur nianko nguir mou balma balma akh balnala yalla nanou yalla bolé bal fassyéné toub ngur bania délou si mousiba yonéntem ba mhmed momdé kou séle leu di niane borom rék khna mou bolé niou si yeufeum yeu diamono leundeum neu nit kou nioul rér lank né dou khipi khna top chalenge ak mode khna ni nio rér dieulna sma khalima nguir binde sama tarikh thi rap naniou recadré wat affaires yi Sinon rék mou keup rabou démbe ak bou tay manouta bokk bou démbe référence leu wayé bou tay danko wara defal ndeup nanko défarat sinon rék mou reup rap galsen miroir la wara nék kou khol guiss si sa bop finga nék souma khalaté Gaston sama khole toy nio melni mom lanou warona nék di roy race in peace yalla na yalla bour léral sa bamél lérou yonenté bi braché wou sisa bir bamél we rap galsen's peole are together so we must keep the rap together I have writen this text for peole rap galsen Dieye le pro nigua le relève de sa génération we need hat core
You may also like

Leave a comment
See track description ↑