hallé bi
diéguéma diéguéma beugou ma gua maye sorri diéguéma diéguéma diéguéma beugou ma gua maye sorri diéguéma Hé diéguéma beugou ma gua may sorriiii hé ha wé wala ma diéguéma la beugou ma gua may sorri hé diéguéma ma déh lou nékh nékh soumala djissé sama holl féh féh andake yaw diarale nama héhe may koulay doundeule mbeugél yokkou tiéré doli niékh diéguéma waye diéguéma waye diéguéma boy dhé la lou nékhe hallé bi rek la beuggu sma seytané djiss nako migui ni bb fonékk guawale njibisile lounou wara doundou diékha goule c l'infini yéne say gua hass ma né dama soff kaye diéguéma si ma niou dieull toff doundou sounou live nékk au top mane djissou ma kéne yaw rek lay toppou ho wé Hé ho wé weuré léne ma hallé bi foumou néh
You may also like

Leave a comment

Boujee 💲