Boule sobou cisama kow. Yalla ma ték si kow. Gua b
Boule sobou cisama kow. Yalla ma ték si kow. Gua beugue maa kow kow. Tay laye rap bagua yakare niman djiné la . Wakhal saguayii mane kendouma lale wala. Mouy sa diamou yaram yaw ak say niogne. Balamaléni def ganar youniou niongne. Tay ma fenial sama talents si rap. Boul topou askawi di len doul tékhamo dara si rap. Sodegué limay rap daguay tite. Nieup nane mane douma nite. Yalla moma may lii. Ma fa ame lii. Kon nargua sonou si lii.
You may also like

Leave a comment
See track description ↑