yoxla jeuliko #2#

0:00
0:00
yoxla jeuliko #2#

fane la rew mi jeum ndakh gayeup pangi nakhaté tik tok ak snap lagneu geuneu geum après gnom gnoy tok di diakhlé gnodii bandit ba khôl yi kheum beug fi gnodi talibé sama eyes di flou leep leundeum ndékété gars yangi toog di zonzé kounék tam sa morome deuum fiii gneupangi diapisé adamo mom damako dem ba geum ndakh mom rk moléneuu di taclé dirigeants yi def veup baparé geuneuu gnou khadié kone fane lagne djeum bou féké gneuup tardé (2)

1 Comments

Leave a comment

Author
5 years ago

See track description ↑

User avatar
237
Total plays
34
Followers
13
Following

You may also like