MAAFII__NÉKKEU

0:00
0:00
MAAFII__NÉKKEU

fils outill moroom niounee dougne saa morom waa prédateurs waa kaann mooy ngann doumaa sarakhé koonn bou lénn gnann fils meunoo Rapp koonn topalfelé meunoo guatt koonn topalfelé nguané daguaay Rapp wakhmaa foo tothie ténguaa djioguée fii nguaay mellnii sothie liinguaay sénntou boy maakoo dieull yoonn bii nguay djiarr boy maafaa peundeull saa drapeau fils maakoo khootii saay pneu mann maakoo beutteu saa affiche mann maakoo téépii doo démm fénneu ndakh imbécile gueu saay dalleu mann maakoo siimii saa buzz bii mann maakoo dinndii saa laamigne mann maakoo daagueu saay yéré mann maakoo laakkeu saa lampeu mann maakoo faaye lii ngeu lépp fils dangue kooy faaye lii nguaa tidjii booy dingue koo teuthie taabakh bâtiment yaaw ammoo eutteu saay baaraam mann maakoo keutteu boy dagueu trookh ndakh dootoo binndeu sagnsé dii démm yaw dangueu heundeu game bii dafa khatt yaw daguay guénneu nékk dii khollé yaaw dagueu gueumeu transfert bou gaaw boy douguaall xendeu manguii dall yaaw dagueu soonneu gnii maa doonn toognn baall naallénn aakkeu boull sakh soonneu ndakh maafii nékkeu boy yii fii néé mann maay killeur binndeu you fii néé mann maay sénn auteur kouyy bandits mann guaa fii fékkeu kouyy voyous mann guaa fii fékkeu dou kénén mann maafii nékkeu guinaaw rails mann maafeu nékkeu Dakar sakh boy maafeu nékkeu Sénégal mann maafii nékkeu mann maafii nékkeu mann maafii nékkeu mann maafii nékkeu mann maafii nékkeu

1 Comments

Leave a comment

Author
7 years ago

See track description

User avatar
1.95k
Total plays
113
Followers
33
Following

You may also like