mbarikallana
0:00
0:00
Ay du yëm si boop borom kuniuy tam dëm nga segnu yellu liir wedi guiss boku ci ku mar tax a nan pòtit, cu ndox turo nga rus pexe desu ko weer ku wàcc sa and , and bo dem fek fa borom gnak boppu gawa dee seddoo ça kudu yu jëk ya mague mû gnu dab mbej ko ca doxin wa la lo guiss ci nettali lay muju ku bérey dann ku bérey danu ku yar ca kuy yaw lay njëk mbëk mbarikallana (4) werante gis boku ci ku ndobin rey ca maam fo gis lu gnul daw béy ci ca weewu tank purux du gërëm gnamu ndaw bëg nala du yama gënal cama boop gnari kuuy mënu gnu bok ben mbalka say-say waxul dëg wayé yakna xel
You may also like

Leave a comment
See track description ↑