life
Bamay don boy la gueum ni dmay donni dra si deuk tour bi law na fepp ba niou barri dima royy tay lepp lerna bouma fatélékou demb nimou leundeumé won dmay jékki took joyy lou sotti am brom mais douma meusseu faté gnifi nékon demb eupp tall bi bamou booyy façon risque bouné façon challenge bouné façon salle bouné fésal nagnou fépp Gr la lepp tambalé tay mgui fepp kom thiép big up team momo ndax nékoul won man képp niatta goudi laniou fanan studio mak molo tambalé si 0 ba légui niogui begg jeull lepp au sommet gagner trophée bouné légui amna niouma guissatoul si gnima don jégué xolal yoonn bi nimou goudé ndéké dfa lathe soudé mbollo nek ben begal gninou don bégé douniou meusseu wéré nn douniou meusseu wéré gnima guenon jéggé guen ma sorri moy gni wéré nio dan deuk dima mboubo dédete amatou niou neubo gniko fi xaroul rk gnotax ma xammé gnima beugon
You may also like

Leave a comment

Hey @qimmortaliii.8646516, We appreciate you sharing 'life' with us! 💥 1. Don't worry if you didn't get it first time, you can always re-record your bars! 2. Try and test out the distance between you and the mic before recording, this can make a huge difference to the quality! ✨ 3. Keep experimenting with vocal effects! Sometimes less can even be more! 😲 Test different effect levels and settings to find the best balance! 4. Try using our denoise feature to reduce the background noise from your device! 5. Try entering one of our weekly contests for the chance at winning the $500 grand prize! 🥇 Keep up the hard work, we can't wait to hear your next fire track! 💪 All the best, The Rap Fame Team 😎
dope track bro keep up the good work 🔥🔥
naiss
Keep grinding ✊ Keep grinding ✊ Keep grinding ✊ Money 💸 WOW ⚡
Bars: Perfect 💯 Delivery: Perfect 💯 Impression: Perfect 💯