EMLY
EMLY

la vie est difficile parti 2

la vie est difficile parti 2

82 Plays

20 Mar 2021

Aide toi et le ciel t'aidera Aujourd'hui ça va pas mais demain ça ira tes rêves ne se realiseront pas en même temps Travail dure avec peux de mi-temps Tu n'as pas ce que tu veux, tu sais le pourquoi. Tu n'arrives pas à l'obtenir...Questionne toi! Est ce que tu as travaillé tout les douze moi Est-ce que tu le faisais avec..amour et foi Est-ce que tu veux être un partenaire de joi. Et cherche argent par ce qu'il est toujours roi s'il rentre dans la mer tous le reste se noie Le soleil est déjà au zénith... réveil toi Fais toujours quelque chose même si c'est couper le bois so manger, coucher et dormir seulement t'a pas le droit. Et prends ton destin dans tes bras être riche ou être pauvre... fais le choix Bo beuger tekki nagoul ligueye te teye nague si bolé diamou yalla bess buné ngua kheye. Bo bouger done dara bou di wakh nioko moom Nangua niafe ba soubeu niouné yaw yaako moom liguey ba amal sa bop der warna kouneh comme ça dingua meuna fadj sa hahdjiou do toupou keneuh. bo diangoul nii diangue niarfa tekki warougnla yem. Ndakh guisnagne fi ku mosta toog si bancs te am lou yem. Mbirmi dou len lene loudul gueum sa bop la Live bi moofa tolu ... bopp sa bop la koula diokh tey ngua lek.. souba mou were la Amna nioye yelewane te fenialouniou seni bopp. toppu ci nittou ordinaire .... loumou wakh ngua tatiou. setoni dafa dingue..... même bouder fen mo degou. fi loofi meuta am ci loudul degue so dou yag deg deg degunagne loudul deg dou yag.

1 Comments

Leave a comment

3 years ago

You may also like