liffkha
liffkha

Freestyle egotrip

Freestyle egotrip

33 Plays

08 Feb 2021

Fal dangay yot daw dou gaw thi ay marakis Flow Bi ndox thi caro eupeul moy sa tarkhis Nenga yaniou raw mouno ranie baa ak sinn Do tougnu wath nieuw rk taw dagnko yagua khin Dam la kawé mêm thi teud sakh doniou timm Xel you fess kom adounak limou eumbe Niay di khali mbabal fok nga gis peund Do gis trac thi fimay aw kom fou diargogn leund Def thi gangs eundi lou deugeur keuth Don thi deum nieup lay peuth kén dou reuth Bondi thi béat clasic sa rap Bi plastique Yémé thi bic thiop la yak say pic té thiow du djip Game Game Game Over = lif leu thi bénén level kay dieul sa dozer = fék bouko dieul wouyo tat lirycs yi over doss leu = force damay nieuw kon wait ma ni sa bisou dé = limafi geuth mo takh lath loumay déf fi = rien de 9 apart fuck fék yi kom 6 = dialema ndar yak say bar fis tangoulo = yimay dieul doko diay amo vin boumay mandilo = tanté rk nga beug bayil ma may la une touch = lir ngeu👶🏾 = tokontal lalay diokh boy oubil sa bouche bihts 😂new Brain tekandér la diapal ni doko soul😇bouko bougoul gis nala lerni yang thi leundeum🔥k o caré la fis eeh négnu sél mine😇yague nagn xous thi leundeum soxla wougn sa lamp💡geum geum biniouy doxé rk doy naniou diant🌞wékou Nagn thi god man té niongkoy dolé sant🙏hamdoulah🙏

1 Comments

Leave a comment

3 years ago

You may also like