Gy boy

freestyle

Gy boy
freestyle

24 Plays

05 Nov 2020

Dama dioudou xiif mage guss ne wornahci lieek bisbou yalla shak makoy xosslou éni thaim éni weee may xaar buiss bou niex mélni soube dina diex xawma xawma xawma xawma kahne lay dieex dahx niakena sama brow niakena sama xeel niakena sama xool niakena sama baaby niakena sama xarit niakena sama love niakena sama bien niakena sama laif yahkena sama yoon yiakena sama doundou yiakena sama diob xamatouma Lima doon xamatouma sama yoon xamatouma Limay deef faténa fima diahr wonliéen ma sama yooon dama réer dama goube dama moume dama ruey Moy ligana bon ci nit ibliss sama xeel (gidéema sama yoon dieef dieef jdou bon niek Lima gana buege

1 Comments

Leave a comment

4 years ago

You may also like