2020
2020

Diagne flow

Diagne flow

62 Plays

09 May 2020

flow bi di dechiré mi beugnou caïman Bar you sadik ni diague bou diotoul paiement Boul niodi lo menoum meunoma fay mane Say rime dafa yague dépassé ni vog mane Sa cachet di sama prix ndeki meunolen ma faye mane Ay bar you rare fokoy dieuleti ni souleymane faye man Nagoul ne may se bay sinon nga muet ..dak la rap dak la rimé Loumay def dafa nice be se soeur dima apprécié Flow bou nice di briller comme or Rap bou smart té diouguéwoul oxford

1 Comments

Leave a comment

4 years ago

You may also like