Mamadoubeler

dip mama

Mamadoubeler
dip mama

33 Plays

31 Aug 2019

Oh mama saltewona sama adouna yaw ya co foott metiwonna dem bla tay di niew Guiss n'a linma wakhon demb bla tay di d'or' sa luguey demb, moy sama fayekou tay, mou do non lu bakh, ma wora diengou tay, niep wonon m'a Ganaw yaw nga won ma kanam oh mama ndeye san sama mama ! Adouna faye ma nite mounouma fay, fouma diar niep niomay sentou melni wrrou kor werou kor werou kor oh mama fatewoumala sama mame mame sama mame,

2 Comments

Leave a comment

5 years ago

Bit correspond rituel

5 years ago

Oh mama saltewona sama adouna yaw ya co foott metiwonna dem bla tay di niew Guiss n'a linma wakhon demb bla tay di d'or' sa luguey demb, moy sama fayekou tay, mou do non lu bakh, ma wora diengou tay, niep wonon m'a Ganaw yaw nga won ma kanam oh mama ndeye san sama mama ! Adouna faye ma nite mounouma fay, fouma diar niep niomay sentou melni wrrou kor werou kor werou kor oh mama fatewoumala sama mame mame sama mame,

You may also like